le discoure de mawlana cheikh ould khayri en Wollof كلمة مولانا الشيخ ولد خيري بالوولوف
nagnou ragal yalla teu gnou
deudou lep loudoul mom teu nagne baguante nguir mom nagne kharito nguir
mom nagne yeuremanteh nguir mom sougne mauritanie ak sougne senegal ak
sougne mali ak sougne gabon mbololagne bou yatou niki yatouwayou fayda
bi babou teu fayda bi yit yatouna niki yatouway dine ji teu mouy lislam
, gnoune nieup dagno baguante thi beureub bou yatou bobou nga khamne
yonent bi (saw) mo gnouko dafaralone bala jouneh ak gniente temeri at
teu momit lagnou cheikhou tidjan dafaralone bala temeri at ak legui teu
momit lagnou cheikh ibrahim dafaralone bala temeri at ak legui beureub
bobou nga khamne gnounkoy japer niki sougne beureub gnoune nieup , teu
thi lagni topeh ndigualou yalla yi thi beureubou yalla bi thi diguante
jamou yalla yi soukandiko diamou ak baguante ak dioub ak dimbalante
binek thi sougne diguanteh teu gnoune tereh lep louy safanou lolou.
ليست هناك تعليقات:
إرسال تعليق